Du bàyyi Ak loo ko mëna def du bàyyi Ak lu mu mëna gis du bàyyi Loo ko mëna def du bàyyi Bisoo bis Ngay gën triste Leen li nga bëgg wetook man ci àdduna Li ngay gis Lépp mooy bis Bis ñëw ma dëdd lépp ni la àjjuna Life dey gëna tara Mais doo mësa bàyyi Yaa ngi dunde yaakaar Gis naa ci yaw njambaar Def nga li la war Te Yàlla du la seetaan Te bëgg naa la, bëgg comme ni nga ma Show la tuuti love comme ni nga may Lépp loo bëgg man ma ne ca Ndax mérité nga ko Bëgg naa la, bëgg comme ni nga ma Show la tuuti love comme ni nga may Lépp loo bëgg man ma ne ca Ndax mérité nga ko Ayayah ayayah ay! Suma saañoon bëgg la Tuuti sax comme ni nga may Hey Ayayah ayayah ay! Suma saañoon bëgg la Tuuti sax comme ni nga may Man defuma la Leen lu wara tax Sa xel ak sa xalaat nekk ci leneen Xol bi su doon wër Toppi nga keneen Jaam ak bëgg bëggam Mais Yàlla mooy dogal Sa boo may xool mbégte bi may gis ci yaw Ferñent bi takk mënuma ko ëpp ba mu gën di boy Wtf is love bu fekke ni man ki ma ko sekkal gisuma? Lool ngay wax sa biir man metti na ma lool baby Te bëgg naa la, bëgg ma comme ni ma la Show ma tuuti love comme ni ma lay Lépp li ma bëgg yaw nga ne ca Ndax mérité naa ko Man bëgg naa la, bëgg comme ni nga ma Show la tuuti love comme ni nga may Lépp loo bëgg man ma ne ca Ndax mérité nga ko Ayayah ayayah ay! Suma saañoon bëgg lay Tuuti sax comme ni nga may Hey Ayayah ayayah ay! Suma saañoon bëgg la Tuuti sax comme ni nga may Duma ni la dem naa Te mënuma la ba Man duma Dame Tiatou Mbissane Duma ni la dem naa Ndax mënuma la fàtte dame Man duma Dame Tiatou Mbissane Dame Tiatou Mbissane Jarul seetlu ji Daam Jarul dem di seeti Mbissane