Lima khalé bi diaral
Lima khalé bi di deff
Lima khalé bi diaral
Loumou yagg yagg may daneu

Souma wakhtaner sama djeguènaye, nakh goudy day yokou khel
Sou souba dioté ma daldi faté guenteu gui ma guéntone bikk
Magui dane sama dolé
Magui fathie samay adio
Magui sante yallah
Monné amna lou dess

C l'amour
C l'amour
C l'amour
C l'amour woohoy

Louko dak, dara douko dak, hé liy nekh nekhna yehh
Louko dakh wakhma louko dakh
Youssou marie séne limou wayy nekhna yeeh
Louko dakh anna louko dakh

Hé
Liy nekh nekhna yehh
Louko dakh, daara douko dakh
Papa Youssou madjiguene limou wayy nekhna yeh
Cherie sama sadiobane
Dina liguey ba ame louma dieundé satellite meune kham lathia RTS
Lathia si yénene, lathia mtv yeehh

Couple bi may dadiel soumay dokhantou dji
So yekk sé gnogui deff bras dessus, bras dessous
Lima doumbéé, lima wessou day deloussé, melni setou
Thie gare bi lako fekk, migui sanguo seuur, thie beuteu bouy tagué
Ma daldikoy nouyou, mou daldi may fayy
Dara douko dak

Hée
Liy nekh, nekhna yehh
Louko dakhh dara douko dakk
Youssou marie séne limou wayy nekhna yehh
Louko dakk, dara louko dakhh

Hé
Louy nekh nekhna yehh
Louko dakh daara douko dak
Papa Youssou madjiguene limou wayy nekhna yehh
Mamy al waly mané ndiaye, ioe sa mame moy yonéneu

Taw, domi taw, setou taw, mbackée
Loumou séneu, boulma guiss ma di réeh ngua
Fokni mane khamouma li nek si sama souff ak thie kanam
Say wayy yehh nagnouma, sayy wayy yarr nagn ma
Vos chansons m'ont appris harmonie et amour yehh
Louko dakh, dara douko dakhh

Hé
Louy nekh nekhna yehh
Louko dakh wakhma louko dakh
Papa Youssou madjiguene limou wayy nekhna yehh
Louko dakh, dara douko dakh

Hé
Louy nekh, nekhna yehh
Louko dakh, daraa douko dakh
Youssou marie séne limou wayy nekhna yehh
Thie diameu la leep khathie, yalla na diameu diodiou saakh

Hée yay
Hée way
    Página 1 / 1

    Letras y título
    Acordes y artista

    restablecer los ajustes
    OK