Eh, yooo Eh iiih Yeah yooo yaaa yeeh Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari Def la soxnay sama coobare Toppal sama ginnaaw te bu coow bari Xam nga ni yaay sama càppali Xam nga yaa ni ma Ni teg na ma la he Fu ma Mousta teg jàmm bu Yàlla bind Man fonk na ma la Man it ma ni la heee, sa xel naa dalee Diandia bi du soppeeku Massamba Du dem sa Massamba la, hei! Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari) Def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari) Toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari) Xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari) Jànq yaa ma ni Du ku la ciippatu génn ci ndaxte yombuloo Du ku la jàmm na ni, he waay! Jànq yaa ma ni Bis dina ñëw nga daagu ci kër gi séyal Man ma tok ci ndaanaan yi, hee waay! Li nga ma wax tax na mën na ma wat Ni doo ma bàyyi même su ma faatoo Àdduna yépp su ñu dajewoon Pour séparer ñu du tax mu àntu Jànq yaa ma ni, jànq yaa ma ni Li nga dikk doy na ma, wëruma leneen Li nga ma wax neex na ma, yeiiii Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari) Def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari) Toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari) Xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)