Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi Awma laamisoo tudduma lambay yoy Gaañ la taxul nga ba Tooñ la taxul nga may rëccooy Sàllaaw yenn saay nga mer Sama jaambaar ci yaw mi la wékkooy Dootuma wiri wiri njari ndari Li ma moom laay jëli (eeh yoo) Dootuma yónni kenn ci sama waa ji Man mi maa koy jëli (man ma) Dootuma wiri wiri njari ndari Li ma moom laay jëli (daadi sama waay) Dootuma yónni kenn ci sama waa ji Man mi maa koy jëli (danga di sama waay) Bala ma jug Fajar fekk nga dem jaayooy Bale kër gi, raxas say ndap Ndekke boobu doom ngay wajal Dundu mat a ñaan nooy Ndaxte gaynde dama koy jur Ndax fitnaloo ma Xëboo li ma lay jox Lépp loo ma ñaan dinaa la may Dootuma def leen lu lay metti sama ndaw si Ndax sama nawle nga doo leeral sama yoon wi Dootuma nangu mindéef di dox sama digu ak yaw Ndax Yàlla moo def ci ñun lay ñu wëy nak Kaay waay! Gaañ la taxul nga ba Tooñ la taxul nga may rëccooy Sàllaaw yenn saay nga mer Sama jaambaar ci yaw mi la wékkooy Dootuma wiri wiri njari ndari Li ma moom laay jëli (eeh yoo) Dootuma yónni kenn ci sama waa ji Man mi maa koy jëli (man ma) Dootuma wiri wiri njari ndari Li ma moom laay jëli (daadi sama waay) Dootuma yónni kenn ci sama waa ji Man mi maa koy jëli (danga di sama waay) Gaañ la taxul nga ba Tooñ la taxul nga may rëccooy Sàllaaw yenn saay nga mer Sama jaambaar ci yaw mi la wékkooy Eee waay Sama jamm, sama waay Eh waay wow Sama jamm, sama waay