Hey Massamba Walo Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Dem nanu ba romb dëkku man a bàyyi Gane na nu ndumbelaan Dund nan fa àndu nawle Soo gestoo gis ma maa ngi ci sa ginnaaw Muy bànneex walla naqar Dinga ma gis loo man a xewle Ndax man la Maas Du ku ne laa man defal Raw nga maas Yaw waxóo ma danga maa jëfal Fees sa place Su ma meree yaay dëfal Am nga classe Garmi sama séddoo Jigéen Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Tann ma ci mbooloo mi Nangu nima bindo Man manu ma lu dul gërëm la Man wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Dem nan ba romb dëkku man a bàyyi Gane na nu ndumbelaan Dund nan fa àndu nawle Soo gestoo gis ma maa ngi ci sa ginnaaw Muy bànneex walla naqar Dinga ma gis lu man a xewle Su ma la njëkkee jug naa la yee Su ma la jiitoo naa la xaar Man nga ma wóolu duma la weer Nangu say sikk naa la suturaal Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Tann ma ci mbooloo mi Nangu nima bindo Man manu ma lu dul gërëm la Man wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa Tann ma ci mbooloo mi Nangu nima bindo Man manu ma lu dul gërëm la Man wóolu nama laa Am nga ngor lool Yaa di ki ma nawloo Kocc na ma jéggal Man de wóolu nama laa