Méritewuma la, eh Méritewuma la, eh Méritewuma la, eh Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Méritewuma la Méritewuma la Yàlla xam na méritewuma la Ooh, méritewumala Attewoo ma ñakkal ba may déconner Décider woo bañ ma xaar ba ma xéy dem Dund bi yépp yëk sa tar Te taxul nga changer Méritewuma la Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Méritewuma la Méritewuma la Yàlla xam na méritewuma la Ooh, méritewumala Na asamaan si taw mur sa ay rangooñ Na denn bi dal neb say xixet Bëgguma nga jooy danga may dofloo Rabil-allahmin na ma booleek yaw Ci sa wet rekk lay mëna keparoo Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Waxal sa xol ni fonku na Ko tekk na ko fu ma teggul kenn Ahn he ya he, hum Méritewuma la Méritewuma la Yàlla xam na méritewuma la Ooh, méritewumala