Hey Massamba Walo Maa la tooñ ndax maa la woolu Ba nga ñëw ma lay wax ay waxu mbëggeel Maa la doy te man nga wóolu Sunu ànd gisuma ci lu dul ngëneel Su jaree raag Dinaa la wan fi ma manee yaw Man duma seetaan Su jaree raag Dinaa la yóbbu sama gàlle Présenter la sama gaa yépp Eey waay Man dama laa, bëgg du nax Coobare Yàlla Moo ma indi ci yaw Àdduna yaa fiy wàcc sunu biir Waru nu tee gise Yaw Kumba amóo moroom biir Senegaal Nee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal Àdduna yaatu na yaa ma tax a toog Senegaal Waaw kumba danga di taaru Senegaal Man dama laa wóolu man Ndax danga maa wóolu Te duma dem fenn ba la Ndax danga may wër Maa la tooñ ndax maa la woolu Ba nga ñëw ma lay wax ay waxu mbëggeel Maa la doy te man nga wóolu Sunu ànd gisuma ci lu dul ngëneel Kaay waay Lot of peace Lot of love Soxna sii Man loolu laa la yéene Don't believe Benn miss Li ñu gis Mooy nu wàlliyaani Taaru Senegaal nga Linguère biir Kayor Yaay boroom teraanga Jéeri jàpp Joor Yaw Kumba amóo moroom biir Senegaal Nee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal Àdduna yaatu na yaa ma tax a toog Senegaal Yaatu na yaa ma tax a toog Senegaal Waaw kumba danga di taaru Senegaal Anh yeaah Man dama laa wóolu man Ndax danga maa wóolu Te duma dem fenn ba la Ndax danga may wër Yaw Kumba amóo moroom biir Senegaal Nee naa la waaw-kumba jël naa seede waa Senegaal