Maa ngi toog sama biir kër Lim binde nii maa ngi fa woon Nga lire ko, gëm ko, saaga ma Lan moo xew? Moo ko def Ma ni la moom la Gutt bi fii lay jaar Numu soofe Bëgg naa solu te noon la xayade Bu juge dépp ay cheveum yu ñàppe Jëlal make-up bi muy mel ni gaynde Lijjanti lijjanti ba nar ci wayadee Der bi ngay yaqi, demal jox ko uude Mu def ko dalle sol ko uuti loo def Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw Duñ bëgg sa dara, sappa dëxin Solu rombati leen, parfum bi tontu leen Amatuma benn temps ay waxi noon Solu rombati leen, parfum bi tontu leen Amatuma benn temps, maa ngi ci man Maa ngi toog sama biir kër Lim binde nii maa ngi fa woon Nga lire ko, gëm ko, saaga ma Lan moo xew? Moo ko def Ma ni la moom la Gutt bi fii lay jaar Pourquoi ba léegi sooy lire Mettit bañu ñu naak jege Ñi ci mbedd mi ngay fore say fait Nit ñi lëndëm nañu Ba mel ni coupure général Ne ci, ohhh léegi Ñu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw Duñ bëgg sa dara, sappa dëxin Solu rombati leen, parfum bi tontu leen Amatuma benn temps ay waxi noon Solu rombati leen, parfum bi tontu leen Amatuma benn temps, maa ngi ci man Maa ngi toog sama biir kër Lim binde nii maa ngi fa woon Nga lire ko, gëm ko, saaga ma Lan moo xew? Moo ko def Ma ni la moom la Gutt bi fii lay jaar Àdduna bii bu doon arène Ku bëgg jal faut nga laale Xeex dokki bu mu gacce yi Ci bañu lay nawe Ne ci léegi Ñu xam ni Yàlla du mësa fay wax di baay jëf Picc bu ndaw sax mën nañu wax ba du naaw Moo ko def moom la! Wuy leeee Wuy lelelelee Ma ni gumbal, gumbal Texel waay gumbal Ma ni gumbal, gumbal