Yaw la yaw la yaw la Yéené sama xol ndax dama la Love te sax kafu ma ci Dama sensible dëgg la Dama feel bëgg la jox Sama xol bi ndax dama la Xale bi te ma la jox Sama xol bi ndax dama la love Dama la kay jox, dama la kay jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Chéri ba noppi soppi sama sant Dama la kay jox, dama la koy jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh Han man, han xawma lan la Maa ngi dundu love story bu ma yéem Bul ma laaj lu ma dal nii Sama nobeel amul fu mu yam Xale bi soma laajoon Jant bi, non tey du fanaan Xale bi soo ma laajoon Sama bakkan, dama la kay jox Dama la kay jox, dama la kay jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Chéri ba noppi soppi sama sant Dama la kay jox, dama la koy jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh Gauche wala droite? Dis moi Si tu veux en haut en bas? Dis moi Lu tàng wala lu sedd? Dis moi Ma servir la Bu 19h jotee ñu tëddi Na metti, na yaag, na mel ni Xale bi bul ragal na nga yegsi Ñun kese la ci kër gi na jolli My babe touch my body, ouh Everyday ma jox la nga ne ci Xale bi teg ma lu metti Bu yexe ci yaw la No no du ci man han yayayay Han man, han xawma lan la Maa ngi dundu love story bu ma yéem Bul ma laaj lu ma dal nii Sama nobeel amul fu mu yam Xale bi soma laajoon Jant bi, non tey du fanaan Xale bi soo ma laajoon Sama bakkan, dama la kay jox Dama la kay jox, dama la kay jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Chéri ba noppi soppi sama sant Dama la kay jox, dama la koy jox Dama la kay jox love bi nekk ci man Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh Oh yeaah, oh yeah Ndéké xale bi rekk laa nob Man xale bi rekk la nob Oh yeaah, oh yeah Ndéké xale bi rekk laa nob Man xale bi rekk la nob ba sagar xeeñ 🥀