Danga toog sama xol Yaay ki ko moom léeboon Gént naa takk la Kaay doon sama yaayu doom Dugg naa, dund naa Muñ toog ndax yaw doom Te bés bu sa doom indee doom Def ko doom sama doom Li nit di daj ci néegu-séy Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey Li nit di daj ci néegu-séy Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey Dinaa la romb midi (ooh wait) Te doo ma gis (ooh wait) Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait) Ma dàbbali (ooh wait) Gaa fof no weli (ooh wait) No dootoo ko defati (ooh wait) Ooh wait, ooh wait Ñaata yaay la fi séy Tëj kaso ndax seen doom Yii laaj, ngay laaj Tay amaguma tontoom Yàggatul, léegi rekk nga xam Luy noon sama doom Idda bi tay la jeex Di jéggaluwaat sama doom Li nit di daj ci néegu-séy Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey Li nit di daj ci néegu-séy Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey Dinaa la romb midi (ooh wait) Te doo ma gis (ooh wait) Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait) Ma dàbbali (ooh wait) Gaa fof no weli (ooh wait) No dootoo ko defati (ooh wait) Dugg naa, dund naa Muñ toog ndax yaw doom Pare naa, xamoo ni bu jeexee Jeex na, jeex na Ñëwal! Ah! Nga ni! Aah! Aah! Ma ne beydu volume Saabu mi nanaani Tekkil lunettes yi Ngir gën a gis