Pour une seconde fois La coupe reviendra Elle reviendra Pour une seconde fois Man ko jelli ndam li Jelli ndam Day lëndëm ñuy shine Mbow mbow duñu dara Ci kanamu yi gaynde Vous ne pouvez que bavarder Benn la wone te doyul Coupe lañu soxla wat ñëwal Gaynde ye waral coowlee bébé Tant de perdu trophée, bébé Jaune banana (banana) Bu ñu génnee ci rouge ba daagu fa yépp vert (vert) Sunu gaynde yi ñoo ëpp doole baalu fetal yee Wurus bu Yàlla ngalam, mënoo wax ba soppi ko përëm Yeah, yeah, yeah Douzième gaynde laay woo Allez, allez! Kalidou, Bamba, Gana Allez, allez! Sadio bari manaa Allez, allez! Beydu volume bi ndaanaan Allez, allez! Aliou Cissé laay woo Allez, allez! Abdou Diallo, Camara Allez, allez! Nampalys mi mënna Allez, allez! Beydu volume bi ndaanaan Allez, allez! Eh coupe bu mag be tew Pour une seconde fois La coupe reviendra Nous reviendra Ni gaynde bu nekk ci digg ndëndëm daal Fi ku yëngu mu fay say lampe Kon doxal doxal, ñooy doxal doxal Dara fayu ñoo ñun Jàpp loxo ki nekk sa wet Ñu manko wuti watt ndam Kon doxal doxal, ñu doxal doxal Dara fayu ñoo Ñun ñoo koy yëngël yëngël Yëngël mu naan rëgëj rëgëj Fecc ko ni ku rijj bëgëj Effet yi mooy créer émeute Gisoo ni ñoo koy yëngël yëngël Yëngël mu naan rëgëj rëgëj Fecc ko ni ku rijj bëgëj Les Casa laay woo Allez, allez! Kalidou, Bamba, Gana Allez, allez! Sadio bari manaa Allez, allez! Beydu volume bi ndaanaan Allez, allez! Les bukki man yeen laay woo Allez, allez! Abdou Diallo, Camara Allez, allez! Nampalys mi mënna Allez, allez! Beydu volume bi ndaanaan Allez, allez! Équipe bu mag be tew (tew) Ñun ñoo koy yëngël yëngël Yëngël nu naan rëgëj rëgëj Fecc ko ni ku rijj bëgëj Effet yi mooy créer émeute Gisoo ni ñoo koy yëngël yëngël Dëgg balle door duggal ñu tëpp Fecc ko ni ku rijj bëgëj Équipe bu mag be tew (tew) Équipe bu mag be tew (tew) Équipe bu mag be tew (tew) Pour une seconde fois La coupe reviendra Elle reviendra Pour une seconde fois Man ko jelli ndam li Jelli ndam