On ne vit qu'une seule fois On ne vit qu'une seule fois Une seule fois Day lëndëm may shine Mbow mbow duñu dara Bul geestu, bul faale Et laisse-les bavarder Man buy neex duma doyal Lu mel ni man wëral Dawal ba mel ni évadée bébé Jën moo rëcc ay filets bébé Jaune banaanaa (banaanaa) Fu ma génnee ci rouge ba daagu fa yépp vert Sama sourire moo ëpp doole balle-u fetal, yeh Wurus bu Yàlla ngalam manoo wax ba soppi ko përëm Ye-ye-yeh! Yéen mbaa nommoon ngeen ma (Noo def mu neex) Waaye jeex na ñëw naa (Noo def mu neex) Comme fi mu ne baax na (Boo defee mu neex) Beydu volume mi nanaani (Boo defee mu neex) Nanaani La vie est belle On ne vit qu'une seule fois On ne vit qu'une seule fois Une seule fois Ni ku nekk ci diggu diggu lëndëm daal Yàlla jekki rekk taal say làmp Ngay doxal doxal Di doxal doxal, dara fayu ma man Jàppal loxo ki ne sa wet Ñu bége bala ñoo dem Kon doxal doxal Ñu doxal doxal, dara fayu ma Man maa koy yëngal yëngal Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj Fecc ko ni kuy riij bëgëj Effets yi mooy créer émeute Gisoo ni maa kooy yëngal yëngal Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj Fecc ko ni kuy riij bëgëj Yéen mbaa nommoon ngeen ma (Noo def mu neex) Waaye jeex na ñëw naa (Noo def mu neex) Comme fi mu ne baax na (Boo defee mu neex) Beydu volume mi nanaani (Boo defee mu neex) Nanaani La vie est belle Man maa koy yëngal yëngal Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj Fecc ko ni kuy riij bëgëj Effets yi mooy créer émeute Gisoo ni maa kooy yëngal yëngal Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj Fecc ko ni kuy riij bëgëj La vie est belle Fu ma génnee ci rouge ba daagu fa yépp vert Sama sourire moo ëpp doole balle-u fetal, yeh Wax yi du romb, yére yi faxasu leen Faxasu leen