Man dégg naa feebaru mbëggeel kenn mënu ko faj Ma bëgg ba malade te fasenewuma naan garab Ngelaw bi ci ëpp kaay, dootul mel ni faru-rab Nobati naa, lonkoti naa dal, wuy Pape et Cheikh Ouhou ouhou ouh... Boo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem Ouhou ouhou ouh... Daagan naa jaamu ki la ressuscité Nga ni... Ku la moom? Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Ma bañ duma ko wax Nga ni ku la moom Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom Lonkoti naa, foo ma jaar? Man yaw rekk la bëgg Pare naa bañ bañ na dara My baby boo May baby cat dafa gaaw "Suma suma lomsong fi jubbo lonkong" Musloo ci seytaane Ma xaare côté bi nga jaare côté bee Neex-neex bi lan la? Tempo tempo di jël sa temps ba rof ma jaaro baram Laax bi nak fok ma sëlëm ko sa kanam Tegal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la Bul di dóor, bul di saaga Xoolal li ñu teg sa loxo Tégal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la Ho ho ho ho, dëggëntan ba ngee Ouhou ouhou ouh... Boo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem Ouhou ouhou ouh... (ouxayati) Daagan naa jaamu ki la ressuscité Nga ni... Ku la moom? Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Ma bañ duma ko wax Nga ni ku la moom Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom Lonkoti naa, foo ma jaar? Man yaw rekk la bëgg Pare naa bañ bañ na dara My baby boo Ku la moom? Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Ma bañ duma ko wax Nga ni ku la moom Man ma la moom Laaj ma ku ma moom man Yaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom Yaay sama faru-rab Jege ma dolli Doro ku la moom? Clara la moom Laaj ma ku ma moom man Ma bañ duma ko wax Bamba ku la moom? Aïcha la moom Laaj ma ku ma moom man Yaw rekk yaw lay doon ba muy moom