Ioe yaye yay ki geun si yaye yi Di dab sama banékh té dossi tayi Toudou niénti yone soga toudou baye Sante nala geureum nala ioe yaye Yar niou yor niou yé niou meusso ci tayi Mounou ma bagna nam sey jotaay Mougn, moytou, manlou sa mouslay Sante nala geureum nala ioe yaye Bala ma meuneu wax yama done wayal Tay do wax ma ley wayal Rayal nala teign yaye dinala téral Sante nala geureum nala ioe yaye Maman, i love you so Fi nga beug lay xol, la la la la la! Yay sama reinou xol Yay sama reinou xol Té ma ngui diégalou si lima tok lou yague beugeu leu té wanoumala ko Souma sagnone mane, dotouma tok ba Guiss leu té waxoumala ko ioe yaye boye Yaye sama yaye yaye yaye boye hoy! Maaa! Sante y’allah ndax lokho lama béral Bou déssone ci ioe doma féral Dara doula té yaye boye démal Yarr ma, yorr ma, yé ma Dima xélal werneu wan ko sa xol nako sédal Maléyo maléyo! Yo malé nénam mimé ri ma diara nénam Bala ma meuneu wax yama done wayal Tay do wax ma ley wayal Rayal nala teign yaye dinala téral Mime ri ma diaram nénam Maman, i love you so, fi nga beug lay xol la la la la la! Yay sama reinou xol Yay sama reinou xol Té ma ngui diégalou si lima tok lou yague Beugeu leu té wanoumala ko Souma sagnone mane, dotouma tok ba Guiss leu té waxoumala ko ioe yaye boye