Soo ma soree nu may nooye sama xol kaay Waatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal? Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële Dénk naa la sama xol bi Yéene naa la sama xol bi Dégg naa la ci sa xol bi Kon nak foo móolee pikkiru laay def Coloré nga sama xol bi Dénk naa la sama bopp Li nga liggéey ci sama xol bi Wuy yaay bi bànneex nii mu may def Say xeetu xaar baax Man su ma koy lim fi de laay des Ndax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def Parlement bi yépp naan bandit laa Ñi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma Baby yaw ci loo ne? Jegesi ma, ñu felfëlaale Dénk naa la sama xol bi Yéene naa la sama xol bi Dégg naa la ci sa xol bi Kon nak foo móolee pikkiru laay def Coloré nga sama xol bi Dénk naa la sama bopp Li nga liggéey ci sama xol bi Wuy yaay bi bànneex nii mu may def Maa ngi séet Fi ma la def waaw Yaay ki ma def roi bébé Xamal ma luy nobeel Ba ñu gisee Mënuma xef waaw Bëtu mbëggeel rekk waaw, bébé Laa la mës a xoole Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal? Duma bett ci yaw ndax ndaanaan nga Duma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy Maa la njëkk barde Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara) Te sama féem yi rëcc ci du gaaw Ba nga réppee ba dugg ci Mami Guissé Laa la xool rekk ree Dénk naa la sama xol bi Yéene naa la sama xol bi Dégg naa la ci sa xol bi Kon nak foo móolee pikkiru laay def Coloré nga sama xol bi Dénk naa la sama bopp Li nga liggéey ci sama xol bi Wuy yaay bi bànneex nii mu may def Dénk naa la sama xol bi Yéene naa la sama xol bi Dégg naa la ci sa xol bi Kon nak foo móolee pikkiru laay def Coloré nga sama xol bi Dénk naa la sama bopp Li nga liggéey ci sama xol bi Wuy yaay bi bànneex nii mu may def