Frasy diaral ngaama dumala bayé Honey yaay sama coco bané Shuu bi nexna surum lèè ba dioolea Darling yaay saama coco baneé Diaral ngaama bòòt gaindé Roogan tikoo diani saa maan Hee hee-eee maan dee diaral ngama lounéék Diaral ngaama guuh pétrole Wonub taal di dieuf dieufi Frasy maan de diaraal ngama lounék Frasy diaral ngaama dumala bayé Honey yaay sama coco bané Shuu bi nexna surum lèè ba dioolea Darling yay saama coco bané Diaral ngaama bòòt gaindé Roogan tikoo diani saa man Hee hee-eee maan dee diaral ngama lounéék Diaral ngaama guuh pétrole Wonub taal di dieuf dieufi Frasy maan de diaraal ngama lounék Aida chérie coco baneh 'Cause you are my likeness and without you baby, I got a illness Wa wa, the sickness 'Cause you're my sunshine, my love don't talk together I never mind, please don't take your love away from me, baby Sans toi dans ma vie je n'ai aucune envie de vivre mes envies Sans toi dans ma vie je vais m'enfuir pour toujours loin d'ici Come on with me my baby Reviens-moi, ma chérie Come on with me my baby Reviens-moi, ma chérie Suudoou woon yaye ak baye Xaarit yi ak mbook yiimaa weur Saama duun yaa meun na sof Melni limaa beug dagne kooy diay Te aawma lignuu may ladie maan Mbeeguel laa bari dolee lii woor naamaa (Colle colle colle, chérie coco) Mbeeguel laa bari dolee dal nama dalon na samay wadiourr Ak genen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco) Mbeeguel la bari dolee dalnama seetull président Ak boromi gaarat (colle colle colle, chérie coco) Mbeeguel la bari dolee dal nama dalon na samay Moroom ak gnenen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco) (Colle colle colle, chérie coco) mbegueel la bari dolee Seetul wasso ak duidu bu yeurr daall (colle colle colle, chérie coco) Mbeeguel laa bari dolee dal nama dalon na samay wadiourr Ak gnenen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco) Kuneek saa histoire thieey mbegueel Capitaine nu borom (colle colle colle, chérie coco) Mbegueel la baari doolee Seetul général ak boromi gaaloo (colle colle colle, chérie coco) Maan guisnaa gnaar gnu beugante Sokhna aicha thiey mbegueel (colle colle colle, chérie coco) Mbeeguel la baari doolee Seetul général ak boromi gaaloo (colle colle colle, chérie coco) Colle colle colle, chérie coco Colle colle colle, chérie coco Colle colle colle, chérie coco