Mbëggeel rekk ka neexooy Ci buñ la nobee Mbëggeel aka neexooy Woowooy ci bun la bëggee Ñi mëna kot daal Amuñu mbaam Ak ni mu la bëggee Yaw nga koy fowe Mbëggeel dafa tiis Te xolul melokaan gaañi Su ma la nobaatee teye ma Bul naagu Bul fowe yooyu Soose Demba majigéen ce Yacine Baby xool ma ree ma Maa tàggook coow lii Li ma ni chéri booy, waxal Soo ma la nobee lu ma yor Jox la ko deseek neen Soose Demba majigéen ce Yacine Baby xool ma ree ma Maa fàtte coow yii Xool ma ree ma Maa fàtte coow yii Mbëggeel rekk ka neexooy Ci buñ la nobee Boo dajee sa ame soeur Tëyal, tëyal! Mu dëgër dëgër Mbëggeel dafa tiis Te xolul melokaan gaañi Suñ la nobaatee, tëyal! Bul naagu Bul fowe yooyu Soose Demba majigéen ce Yacine Baby xool ma ree ma Ñawal noon yi Xam nga sama biir, sama dara umpu la Soo ma bëggee lu ma yor jox la ko, deseek neen Li ma ni chéri booy waxal Maa la bëgg ba mu jeex dawuma ci dara Xool ma ree ma Ma tàggook coow yii Mbëggeel dafa tiis Te xolul melokaan gaañi Suñ la nobaatee, tëyal! Bul naagu Bul fowe yooyu Maa tàggook coow lii Li ma ni chéri booy, waxal Soo ma la nobee lu ma yor Jox la ko deseek neen Soose Demba majigéen ce Yacine Baby xool ma ree ma Maa fàtte coow yii Xool ma ree ma Maa fàtte coow yii Mbëggeel dafa tiis Te xolul melokaan gaañi Suñ la bëggatee, téyel Ak sa fukki loxooy Aly Baba Coumba Naar mbëggeel looy Ay waay man fu ma jëm céy xale bi jaral na ma Nob naa ko Ni waawaaw Aly Baba Coumba Naar, Mario Mbaye Mussee Jama Coumba Sene Mbaye Kuli Fati ma diodio Borom ngaay ndanaan gee Aly Baba Coumba Naar mbëggeel looy Hey yaw man fu ma jëm céy xale bi jaral na ma Nob naa ko Coow la ce pindum teen ba Wey gaa ñi amul baak Mario Mbaye Mussee Jama Coumba Sene Mbaye Kuli Fati ma diodio Borom ngaay ndanaan gee Aly Baba Coumba Naar mbëggeel looy!