Gis la bëgg la, wax ma loo ci xam Jox la sama life, desetuma dara Def la comme sama tere, dang may yokk xam-xam Jang naa la, mokal naa la, ni ku nekk daara Bàyyiwuma dara, jël naa lépp Mbëggeel gi lu mu dis dis Àttan naa ko, àttan naa ko Bàyyiwuma dara Mbëggeel gi lu mu dis dis Bëgg naa man, nañu naa Baby dee ma xool Dee ma xool, dee ma xool Ndax man su ma xoolee Yaw rekk laay gis Dee ma xool, dee ma xool Ndax man su ma xoolee Yaw rekk laay gis Lu ma ame lu dul yaw, man de bëgguma Muy Alal di urus, dara safuma Ndax doy nga ma Ma doen lamb waye daj naa Yaa ma bëgg ba ma yëg ko Yaa ma sutural Bàyyiwuma dara, jël naa lépp Mbëggeel gi lu mu dis dis Àttan naa ko, àttan naa ko Bàyyiwuma dara Mbëggeel gi lu mu dis dis Bëgg naa man, nañu naa Yaay ki ma tànn Yaa di sama ndanaan Duma la jëndek keneen Yóbbuma man, yóbbuma feneen Gisatuma ku dul yaw Su ñu mbëggeel di law Yaay ki gën ci man Taamu naa la, taamu naa la Baby dee ma xool Dee ma xool, dee ma xool Ndax man su ma xoolee Yaw rekk laay gis Dee ma xool, dee ma xool Ndax man su ma xoolee Yaw rekk laay gis