Tey lañ doon xaar Nga def ma sa jabar Ñëpp toog ma seddel la Ne yaay ki ma sagal Dañu dem ba nduroo Yaay ki ma Yàlla boolel Duñu mësa reero Ndax dañuy dund mbëggeel Indil nga ma guro Desalatoo ma dara Yaay sama chamalama Maay sa ding dong Xol bi di tëgg ni tama Yaay sama best song Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi Lu mu metti metti xam na ne yaa ngi fi Def nga ma sa soxna tey bég naa Baby, teraanga bi mat na teral nga ma Jambaar joni-joni Gile gile jambaaree Yaa ma tànn si seen biir Maa la bëgg piir, wax ma lu koy dindi Dañu dem ba nduroo Yaay ki ma Yàlla boolel Duñu mësa reero Ndax dañuy dund mbëggeel Indil nga ma guro Desalatoo ma dara Yaay sama chamalama Maay sa ding dong Xol bi di tëgg ni tama Yaay sama best song Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi Ma sëy, ma sëy, tey ma sëyel la Ma sëy, ma sëy, indi nga guro bi Moom la, moom la Moom la, moom la Ndanaan mooy ki feñ sama dund Foo jar ma wayal la Ndanaan wo woo Su ma demee balay wëy Seck ndanaan nange Mo ngi ne Seck ndanaan nange Mo ngi ne Seck ndanaan nange