Tay ma bakk la, sama chocolat Bëgg naa la, loolu wóor naa la Tay ma tagg la sama olalah Xam naa ne bëgg nga ma, loolu wóor na ma Gis nga jant bi lu mu leer a leer Sa jëmm ji mooy sama lumière Xool nga wer wi nu mu jekke Sa xol bi noonu la rafete Kon jege ma Ñu ànd dem feneen wuyu ma Kon yóbbu ma Ñu ànd dund leneen ba abadan Yeah, yeah Habibi Ki gën ci man te yaa xam li war ci man Di ko def Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi Ano woni my habibti Guily mbeeli mo welti seti Guilemen ko fifty fifty Dund ak yaw muy neex mooy metti Love nana shine like a diamond Hakudam min e ma ha diamone Indema e horam like melody Yidema hokimi dole mbarodi Wawa welde niande fof wada peace Andou Kiram to mberde ko disease Habibti par fewnou tes valises Mami souré houré kangue kaliss Min seeden kalda gonga ann bouriyam Jougo ma e jougam longo fawe walabam Holimi yidde fadani jango tideyam Bae ndekete banekhou beguel fila yam Halla mbelka newika tewika Hewa mossali e diam a yiyata tikka Mberde wiyani aala guite dji ko djiidi Love sabou Allah mberde jaagui ha tiidi Habibi Ki gën ci man te yaa xam li war ci man Di ko def Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi Jugal nga fecce ko Ma woy nga feluma Jugal nga fecce ko (Chéri yaw yaay sama habibi) Jugal nga fecce ko Ma woy nga feluma (Yaw yaay sama chéri, yaw yaay sama habibi) Ki gën ci man te yaa xam li war ci man Di ko def Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi