Lu mu metti metti, amul bàyyi Amul tàyyi, no duñu xaadi Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde Moo ñun gindi, no duñu bàyyi Yoon wi gudd na lool, sori lool Ragal xaaju fi Non, yoqu jibbu fi Gëm ki ma doon lool Moo ma def li ma doon Gëmleen ne Yóonu ndaw du gaaw Fow mu tar pour nga raw I'm on my way, so move away I shine like a diamond, from Dakar to London Trust me, coono du reer No no du mësa reer Xamal ki nga doon, moo lay xalal sa yoon Lu mu metti metti, amul bàyyi Amul tàyyi, no duñu xaadi Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde Moo ñun gindi, no duñu bàyyi Fi àdduna tollu ni Sa jom ak sa fula ñoolay motali Boy, duma mësa fàtte Li ma dund li ma daje ba yegsi fi Yoon wi metti lool Maa koy yëg ci xol Gëm naa ne sama jaar-jaar la Waaye lo muñ mu jeex I'm on my way, so move away I shine like a diamond, from Dakar to London Trust me, coono du reer No no du mësa reer Xamal ki nga doon, moo lay xalal sa yoon Lu mu metti metti, amul bàyyi Amul tàyyi, no duñu xaadi Doyloo Yàlla buur bi ndax moom moy ki ñu binde Moo ñun gindi, no duñu bàyyi Ma ne boy dem Ba xamatoo fa nga jëm Dellul fi nga juddoo fañ la ngénte, fañ la tete Fi nga magee, fi nga jànge l'école