Xool la si bët xol di ko yëg Xel bi sori yénne ji bari li mbëggeel la ko laal Hey, su de ay gént buñ ma yee Li de moo daq neex di ma cooqotaan may ree Hum, kaay kaay Yaw rekk laa love Kaay kaay Yaw rekk laa nob Yaw, yaw, yaw laa nob Yaw, yaw, yaw laa nob Su mbëggeel doon jaay may jënd Lépp lu ma laaj ma jox ko Te soo bëggee dëgg-dëgg Sama xol bi yaa koy fëgg Jox nga ma sama gédd Baby sa love lañ ma sedd Ci lay dundu ba tedd Te boo ma jegee xol bi sedd Kaay kaay Yaw rekk laa love Kaay kaay Yaw rekk laa nob Yaw, yaw, yaw laa nob Yaw, yaw, yaw laa nob Dama la, dama la, dama la nob Ba bëgguma lu lay gaañ Soo ma soree dina ma sonal Sa mbëggeel la may daan Kaay kaay Yaw rekk laa love Kaay kaay Yaw rekk laa nob Yaw, yaw, yaw laa love Yaw, yaw, yaw laa love