Sagam xol lay bëgg Jox naa la ko ba mu jeex Gumba teex lu tek si gëlëm Ne Baye Fall Kour ak Keuleum Da ñu ne xol lay nopp Sama bos sa tura si nekk Ni ma la mbege daf ma ëlëm Soo fi nekkul lépp ay lëndëm Awma ku dul yaw (bul jaaxle) Yaw it amoo ku dul man (bul jaaxle) May jooy di ree ngir yaw (bul jaaxle) Ngay bëgg di xeex ngir man (bul jaaxle) Man de yaw la love (la la la) Sama xol bee chéri ne na yaw (la la la) Bébé yoo yaw la love (la la la) Sama xol bi, sama xel bi ne na yaw (la la la) Chéri yoo Jege ma ma lay reetaan, ngay may piis Lu góor ñi bari bari bari yaw rekk la miss Dem na ba sa mbëggeel dama diis Saa su ma tëddee damay janeer yaw lay gis Ey, ku làmb yaa tay daagul fa ñu la nobee Ma bëgg ma tay li sama xol bi dina ko wane Man de yaw la love (la la la) Sama xol bee chéri ne na yaw (la la la) Bébé yoo yaw la love (la la la) Sama xol bi, sama xel bi ne na yaw (la la la) Chéri yoo Maa ngi fi di la xaar ñëwuloo Baby wax ma kañ laa lay gisaat Sama wéruwaay ci kër gi tay de wet na Danga ma wetal way, baby namm naa la Su ma sañoon doo dem bàyyi ma baby Su ma sañoon foo nekk maa ngi fa baby Maa ngi fi di la xaar ñëwuloo Baby wax ma kañ laa lay gisaat