Lima doundé, lima wessu day déloussé ba melni séttu Lima doundé, lima wessu day déloussé ba melni séttu Wait for me wait for me, abal ma way just wait for me Wait for me wait for me, abal ma way just wait for me Bala ma dougou école ci la am class Ma nék ci sa xol ndax dama am thiat Nama ray kholal nima beugué guel bi nama ray Kholal nima nobé guel bi nama ray Beug ko dioy ci mom, nijay né ma bayiko Lalale nala tapis rouge, boul guetou di len khol Kay mane ak ioe niou dem souniou yone Djiguen dey léral, léral ni sondél Meme bu lak bopeu douko téré léral Talal béneu sondel sou takké tal fouki sondél Talal béneu sondel sou takké tal fouki sondél Yeah yeah! Fokey dieuléti koula beugeu ni mane Fokey dieuléti koula sopeu ni mane mi Fokey dieuléti Khady loula nex, nex nama ioe Ndax sama mbeuguel ci ioe, amoul demi-mesure Kane moy vrai, faux vrai, faux vrai faux oh, aduna yeah Kane moy vrai, faux vrai, faux vrai faux aduna I’m so sorry hum I’m so sorry I real feel sorry Nobawone noboma ndeysane nobomawone Bamaley Facetime taloma wone No boulma message no boulma wo Nobawone noboma ndeysane nobomawone Bamaley Facetime taloma wone No boulma message no boulma wo Boulma khol ioe, wanema ko, mo geun ngamay sagané Wane ma sa mbeuguel ioe, wane ma sa mbeuguel Ioe yay sama chamalama ding dong yeah Ioe yay sama chamalama ding dong yeah Mbeuguel lou thiakhane taxouma diog Mbeuguel lou fo takhouma diog Mbeuguel lou minute takhouma diog Mbeuguel lou yeurmandé ma takha diog Waw waw, yeah yeah Mbeuguel lou yeurmandé ma takha diog