Life bee changé Wala jikko yee yàqu, yee yàqu Loo xamal ké yol Ok wax nga ba tarde Léegi ñépp lay moytu, lay moytu Mu ngi bëgg ñaaw de Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk ey, ndànk ey, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk [Narah Diouf] Ey fi la réew mi tollu Ñi de cas lañuy topp Lu tokk sa nopp Fel sa gëmmiñ, lépp tuuru Kon mu ngi tokk Céy li nga bokk Tekk ko si suuf Balla moo souss Ok yaa ngi si TikTok Doo raté Facebook Snap nga flamme cas bi Whatsap nga yénou coow li Ok bàyyil ni nga nekke Li du sa métier Bul topp sa xol Waxal prarara Life bee changé Wala jikko yee yàqu, yee yàqu Loo xamal ké yol Ok wax nga ba tarde Léegi ñépp lay moytu, lay moytu Mu ngi bëgg ñaaw de Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk ey, ndànk ey, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Bàyyil libeurou jaambur di topp sa kilo Yaw xoolal sa bopp, teggil sa nopp Bàyyil sopp, soooof! Shhhhh Ya raw mor ndaje Doo raté daje Kuy dem yóbbu la Fuñ dem fekk la Life bi de concourou tekki là Ku yeex ñu bala fa Jàppal fils te bul bàyyi Fattal té bañ a teppi Fatal ma foofu bu dara percé Tëbbel ma teup ñu ànd percer Liggéey rekk di encaisser Kassé Life bee changé Wala jikko yee yàqu, yee yàqu Loo xamal ké yol Ok wax nga ba tarde Léegi ñépp lay moytu, lay moytu Mu ngi bëgg ñaaw de Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk Teggil sa tànk Ndànk ey, ndànk ey, ndànk Teggil sa tànk Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk