Billaay, ballago ndoumbé yatma Su ñu waaji xaj oon na fi Naxxar doηη, la ñu bayyee Yalla, wonneeti na Li tax ba mbir mi metti lool Ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gnou Billaay wéetël na ñu Njiinoo njiin faramaareen Gòor u jaaga, nelaw naa Baay i wally dem na nii Ñun daal wéetël na ñu Ma ngi koy jaale Sénégal Di ko jaalé Gambia Di ko jaalé adduna Ndaanaan ba dem na nii Thione ballago, ndoumbé yatma Bu yalla buur bi doon taggoo Kon di na ñu bayék yaw Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel Yee gua nit gñi, tete leen ci adduna Yee gua nit gñi, tete leen Xam al leen ci adduna Ahh - Balaago Yee gua nit ñi ci adduna xam al leen Ni ñu war a nekkek Ak ni ñu war a dundée Ak ni ñu war a jëfleentee Jinaxoo mbaay Yaw mi dëkké biir suuf Boo dem ee neel ballago, réew maa ngi koy joy Aduna ngi koy jooy Art baa ngi koy jooy Njiin faramaareen Thione seck, wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna, am ul solo Li tax ba mbir mi metti lool Ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gno Ndanaan ba dem na ni Njiin faramaareen Thione Seck, wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Àdduna amul solo