Da faa la, wóolóo Teg la nak, fu mu tegul keneen Di dox sa bëgg bëgg, di dab sa bànneex Ndax seetlu nga koo yaw Yaw la bëgg Te yaw, yaa ko sagal Waaw waaw! Bu mbëggéel doon lumière Mel na ni, ni jant bi Te su amoon, lu ko gën ë leer dem na wut i ko Ni yaw, jaral nga ko Lu raw, sóoru gayndé Waaw waaw! Lu mu metti metti, dinga tew Lu mu sori sori, an dinga ñëw Ca dëgg dëgg dëgg Dem na, ba dem, mën ë tul ë tok Benn bés, bum la, gisul Jox na la bii respect Nga delloo ko bii respect Entre vous, entre vous chérie Du wax lii def leneen Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg ya ko diara Ni yaw, yaa ko sagal Waaw waaw Fépp fu mu mën ë ne Da fay sentir sa parfum Loolu yaa ko ko jaral Ndax yaa ko liggéey Les mots qu’il utilise sont toujours en deçà De ce qu’il ressent Yaw yaa ko ko diaral Chérie boy, chérie boy, chérie boy Daf la bëuggué Chérie boy, chérie boy, chérie boy Kay nga jege ko Mou laye déy Yaw mii yaw Su fekkee li mu la wax doyu la Boo yakkamtee Mu def al la ko ni nga ko bëggée Mom contane neu Te sakh yaguena bëgg thi yaw Boo yakkamtee Mu def al la ko, ni nga ko bëggée Ça lui vas, chérie sa lui va, lo def nekh na ko Da fa laa, da fa laa, def ni nga ko def Loo bëgg, mu indil la ko Loo laaj, mu kheuthiel la ko Su fekkee amu ko, mu ñaan ko yalla Chérie boy, chérie boy Yaa ko ko diaral Chérie boy, chérie boy Lo diokhogne mo dok Chérie boy, chérie boy Lo def noonu la Chérie boy, chérie boy Yaa ko ko diaral Youssou Ndour, madjiguene Boul yekhal dara Na gua gaw, na gua gaw Te li djieuntima Soxla yi, soxla yi Gnome ñoo ma gueteun