Dunya, dunya Dunya, dunya Dunya, dunya, dunya mome dafay diekh Dunya dunya, li fi nekk te jadduwul ëpp na Dunya dunya, li fi nekk te jaddu tuuti Dunya dunya, li fi nekk te jadduwul ëpp na Ne baal ma, lor nga ma, lor nga ma Wuy yërëm ma Àdduna bi nanu jugg daal Naanu jokko te baña seetaan Ni wala ci ne, lii am-solo mooy jëf dafay metti Dunya, dunya Dunya, dunya Seegante joge wa ne ngorom Dunya, dunya Tàngaay bi Àdduna bi nanu jugg daal Naanu jokko te baña seetaan Ni wala ci ne, lii am-solo mooy Jëf dafay metti! Àdduna bi jaar na xoolaat Ana borom xam-xam yi, borom kom-kom yee Àdduna bi jaar na xoolaat Mandu jokko te am-yaakaar Billaay àdduna bi nanu jugg daal Naanu jokko te baña seetaan Ni wala ci ne, lii am-solo mooy Jëf dafay metti Àdduna bi jaar na xoolaat Ana borom xam-xam yi, borom kom-kom yee Àdduna bi jaar na xoolaat Mandu jokko te am-yaakaar Àdduna bi nanu jugg daal Naanu jokko te baña seetaan Ni wala ci ne, lii am-solo mooy Jëf dafay metti! Ana ñi soriyante Ani ñi dokkolante (jëf dafay metti) Ni wala ci ne, lii am-solo mooy Jëf dafay metti! Jokko kaay ñu jokko Jokko kaay ñu jokko Jokko, jokko, jokko baña seetaan Dunya bi jaar na xoolaat, nañ ci teey Nañ ci mandu te am ci yaakaar Jokko, jokko, jokko bañ seetaan Dunya li ci mbootaay yi di bañ Te nit ki lu ko taxa joog war na cee dem ba jeex Jokko, jokko, jokko baña seetaan Seetal ma li! Li ci mbootaay yi di bañ Te nit ki lu ko taxa joog war na cee dem ba jeex Jokko, jokko, jokko baña seetaan Oui, c'est le mouvement qui dit non Qui dit non, non C'est le mouvement qui dit non