Yée, yée-hé-hé-hé Yée, yée-hé-hé-hé Hoo, hoo ehnn haan Hoo Africains, woy le leen ma Africa Benn continent, melul ni Africa Amul benn werente ci loolu Suñu mbëggél ci yaw, Africa Amna ñi soriyaante Bu ñu kenn jaxasse Na ñu xam suñu bopp Une jeunesse engagée, Africa Namm u ñu dara, yalla a la barkeel Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo Boo xasee miin xam ni, fii mooy suñu kër Come home with me Hoo Africains, woy le leen ma Africa Benn continent, melul ni Africa Amul benn werente ci loolu Suñu mbëggél ci yaw, Africa Ana ñi soriyaante Bu ñu kenn jaxasse Na ñu xam suñu bopp, avec Une jeunesse engagée, Africa Namm u ñu dara, yalla a la barkeel Tu es dans nos cœurs, du ñu la weccoo Boo xasee miin, xam ni, fii mooy suñu kër Come home with me Ñun Africains, su ñu ànd a ndoo Bokk nday ak baay, Boole suñuy doole Kholal ëllëg u adduna bi Seetal say doom ñoo, koy mujjee Yée, hée hée, an han Ni nga maggeek, ni nga yaatoo Noonu nga riché Ni nga maggeek, ni nga yaatoo Noonu nga riché Du ñu la weccoo ba muk Du ñu la weccoo keneen Africa Xam nga ni la say, doom yi bëggee Tag naa la kaay Yaa ne ci suñu xol Wo, wo, wo, wooy Wo, wo, wo, wooy Du ñu la mas a weccooy Kenn du yaw Africa Yée Yée hé hé hée hé