Gëjoon fi lool bi nga ñëwee Bi nga ñëwee Duma fàtte nit nitam Mooy garabam Bokk nga ci ñi Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg Hi hii hii Koŋ- Koŋ, yegsil daal Koŋ- Koŋ, yegsil daal Koŋ- Koŋ, yegsil daal yegsil daal Koŋ- Koŋ, yegsil daal Yegsil avec plaisir T'amènes que de beaux souvenirs Waxtu wu la neex Mën nga fëgg Fii doo fii gan Bu nu waxantee dëgg daal Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg Koŋ- Koŋ, maa ngi xaar Pressé d'entendre ta voix Biig rekk, sax j'ai pensé à toi Gëjoon fi lool bi nga ñëwee Gëjoon fi lool bi nga ñëwee Nee naa la, nee naa la, nee naa la Bismi, bismi, bismillaah Gëjoon fi lool bi nga ñëwee Nee naa la, nee naa la, nee naa la Bismi, bismi, bismi, bismi, bismillaah Koŋ- Koŋ, Yegsil daal Yegsil avec plaisir T'amènes que de beaux souvenirs Waxtu wu la neex Mën nga fëgg Man de xam naa Ne sa fëgg yaw Bokk nga ci ñi ma gën a bëgg Man de damaa gis ci yaw sincérité Dellu gis ci yaw, woyof ak dal Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex Man de damaa gis ci yaw sincérité Dellu gis ci yaw, woyof ak dal Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex Ñëwal saa yu la neexee sa ñëw Man da fa may dundal Man de damaa gis ci yaw sincérité Dellu gis ci yaw, woyof ak dal Moo tax ma yàkkamti sa jotaay ak sa ree ju neex