Diallo Diéry baax nga Diallo Diéry baax nga yaw Man sata sama ndanaan Waaw, tey ma jiin la Diallo Diéry baax nga Diallo Diéry baax nga yaw Man sata sama cheikh la Waaw, tey ma jiin ko Racki Diallo dem na nu ne riiroo riir ne riir Koura Ndiaye xéy nu ne riiroo riir ne riir Man saata Mansour nga moom Tey ma jiin la Luñ ne déedéet, ma ne muñal Yàlla ko def Lu dikk di yaa ko njaaboote Luñ ne déedéet, ma ne muñal Yàlla ko def Lu dikk di yaa ko njaaboote Sama yaay ku la bëggoon la Dafa daan di sonnoon Luñ ne déedéet, ma ne muñal Yàlla ko def Lu dikk di yaa ko njaaboote Luñ ne déedéet, ma ne muñal Yàlla ko def Lu dikk di yaa ko njaaboote Sama yaay ku la bëggoon la Dafa daan