Ngor amul njëg, bu ko jaay Góore ba réy de bu ko bàyyi Di dunde loo doonul amul njëriñ naan ko bàyyi Jarul ko waay, feexel nank ko bàyyi Deux ans yaa ngi koy topp Xale bi ne na bëggul la Def nga lu ne, wax nga lu ne Moom nobul la Lekkatoo te nelawatoo Dem nga bàyyi xalaat ni faw nga juuk sëriñ tuko Ma ni la: Bàyyil mu sedd, bàyyil mu sedd Bàyyil mu sedd, jaru ko bàyyil mu sedd Ñeme sañsé, téléphone bu génn nga am ko Yaw rekk ci xale, cheveux bu cher nga sol ko Ndekete yoo yoro, dangay ab yoro Ñoo di boss di jaay lu amul ñépp xam ni yoro Kon bàyyil mu sedd, bàyyi mu sedd Bàyyil mu sedd, yoroo kon de bàyyi mu sedd Ngor amul njëg, bu ko jaay Góore ba réy de bu ko bàyyi Di dunde loo doonul amul njëriñ naan ko bàyyi Jarul ko waay, feexel nank ko bàyyi Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Ne na mooy sa xarit te yaw rekk la teg bët Loo am da kou naqari ñene nekk la mungeek kër Nga sañse moo koy sonal, sa mbégte bonal xolam Yëg nga ni da lay soosal, noon la bu ko faale Bàyyil mu sedd, bàyyil mu sedd Bàyyil mu sedd, jaru ko bàyyil mu sedd Moom mag la te ba léegi nangogu ko Wër ci koñ bi jël ci xale baay guko Ñulal bopp, génne face Di jaay tar, père bàyyil mu sedd Dem nga fepp, wax nga ñépp Xam na lépp, kon père bàyyil mu sedd! Ngor amul njëg, bu ko jaay Góore ba réy de bu ko bàyyi Di dunde loo doonul amul njëriñ naan ko bàyyi Jarul ko waay, feexel nank ko bàyyi Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd Bàyyi bàyyi bàyyi, bàyyil mu sedd