Mon cœur fait boum bam Mon cœur fait boum bam Mon cœur fait boum bam Yague na ngamay doflo Té meussou malako wakh Sa leep ma saf ba ningay rétané Nane lay def nga kham ko Beugue na nga kham ko Diafé na ma wakh ko Hey bilay walay Khol bi nga mome ko Lo beugue ma done ko Hey bilay walay Dingama doflo Yamay dioylo Dingama doflo Yamay beglo Mon coeur fait boum bam boum bam Dakh yaw Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toii Mon coeur fait boum bam boum bam Dakh yaw Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toi Boum bam boum bam boum bam bam Boum bam boum bam boum bam bam Moussouma wone guem ni Mbeuguel dina dokh souniou digueunté Sama khol bi rek nga kheuy keuf Ba foumala guiss sama fiite def teuf Fouma meuneu nek Mane may sa yeuf Dingama doflo Yamay beglo Dingama doflo Yamay dioylo Mon coeur fait boum bam boum bam Dakh yaw Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toii Mon coeur fait boum bam boum bam Dakh yaw Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toi Ayéeéé héhéé Beugue nala sama khol béé Ayéé hééhééhéé Beuguenalaa Mon coeur fait boum bam boum bam dakh yaw (Mon coeur fait boum bam bam bam bam bam bam bam hey) Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toii (bam bam bam bam bam bam hey) Mon coeur fait boum bam boum bam Dakh yaw Mon coeur fait boum bam boum bam Pour toi Mon coeur fait boum bam (boum bam bam bam) Mon coeur fait boum bam (bam bam bam Mon coeur fait boum bam Pour toi pour toi Mon coeur fait boum bam (boum bam bam bam) Mon coeur fait boum bam (boum bam Mon coeur fait boum bam Pour toii