Bril OMG Tukkil baby fu la neex doo fay Lu ne ci xol feeñ ci kanam Xol bi yaa ci fees feeñ sama kanam Fu ne laay xool ci sa yaram Di gis sama bopp li fi rekk la am Yaa may dofloo di ma defloo Lu ne baby yaa ma ko jaral Fu ma toogee gisuma la Dégguma la fokk ma woo la ne la jaral Ey yaw la bandit di niróol Kaay wax ma qui es tu Li ëpp na dafa fees bay tuuru atanuma li Yaa may ray di ma dundal àljanna Nga may dugal te deewaguma Su may bàyyi di ma mbugël Safara nga may tëmbal soo ma meree Yaa fi fort Sama point faible yaa ko xam Xol bi bi mu reere yaa ko for Wëruma dara lépp nga am Eh jàmm ji nga may jox da bëri baby li comme guerre Yaw yaay bu baax bi yaa tax may noyyi, yaay sama air Yaay sedal sama xol di tàngal sama yaram Doo ma may dara buñu wétee doo ma yërëm Ma raw sax visa shengen Tukkil baby fu la neex doo fay Cëggin! Xam nga man ma baax ci yaw, kaay ñu Cëggin! Feexal sa xol ma ci gaaw, ñówal ñu Cëggin! Eh, yaa mëna dékku li may daw, kaay ñu Cëggin! Jege ma, jege ma, ñówal ñu fecce mu lay Cëggin! Lépp loo soxla la lay jox di wëy ci say way Su ñuy bëree jarul arbitre yaaw yaay mujje daw Foo ma woo ma wuyu bu la ci neex ci kaw ba ci suuf Wóolu nga ma ñu dem may sa wéeruwaay ma lay uuf Fu ma dem nga wëri ma, fi ma la jàpp sori na Mu ngi tuuru bari na, keneen ku dul man de doyu la (eeh!) Moi j'assure, dam la xam de sur le sur Fimla teye daf la neex, ma lay jooyloo je t'assure Cëggin! Fowe sa xol te mënoo ci dara (Bëgg naa daf may neex) Na xela ni bébé te mënoo ci dara (Eh bëgg naa li daf may neex) May xale bi la pogné te mënoo ci dara Moome la te mënoo ci dara Mën la fépp te mënoo ci dara Yaay sedal sama xol di tàngal sama yaram Doo ma may dara buñu wétee doo ma yërëm Ma raw sax visa shengen Tukkil baby fu la neex doo fay Cëggin! Xam nga man ma baax ci yaw, kaay ñu Cëggin! Feexal sa xol ma ci gaaw, ñówal ñu Cëggin! Eh, yaa mëna dékku li may daw, kaay ñu Cëggin! Jege ma, jege ma, ñówal ñu fecce mu lay Cëggin! Fowe sa xol te mënoo ci dara (Bëgg naa daf may neex) Na xela ni bébé te mënoo ci dara (Eh bëgg naa li daf may neex) May xale bi la pogné te mënoo ci dara Moome la te mënoo ci dara Mën la fépp te mënoo ci dara Eh, cëggin! Yaay sedal sama xol di tàngal sama yaram Doo ma may dara buñu wétee doo ma yërëm Ma raw sax visa shengen Tukkil baby fu la neex doo fay Cëggin! Kaay ñu cëggin! Ñówal ñu cëggin!