Est-ce que xam nga li nga yor? Xale bu ndayam gërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la Yaw ku ñépp di wër nga am Ñeneen ñi duñ dërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la May ki taxoon ñu sakk la Ànd bangue ñu taxe aras Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Maay ki sa yaram lacc Ndax may ki koy dawal Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la Eh ndank rekk Ma daan la jël bu gaaw amateur yi bekk Ñi bekk V bi rekk match nul loolu mënta nekk Doon sa géelu rap bi sanguloo la seet Chance dëgg la am ku mel ni man ci sa wet Li ñiy bari bari yaw may sa préférée Te fàtte xaaju fi var am na so wedde Li ngay wëri feneen yaw fi rekk nga koy ame Ndax may ki ko am ma ko am baku bari doole Sa pointure mana, keneen jàppu la Ay boobu mbëgeelu sur mesure Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob) Sa dëggëntaan (man nga nob) Ku lay gaañ yaw ku lay cooxatan Est-ce que xam nga li nga yor? Xale bu ndayam gërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la Yaw ku ñépp di wër nga am Ñeneen ñi duñ dërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la May ki taxoon ñu sakk la Ànd bangue ñu taxe aras Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Maay ki sa yaram lacc Ndax may ki koy dawal Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la Àndak man day def effet man rekk damay yokk taar Kon te nga ngoy bu dëgër banc de touche bi ñoo ngi xaar Man rekk kala jàpp keneen ko àndalit du dem Te ñi di la toppe soo yabo neleen ñu yam Ñi naan la yaw fan wi danga leer so goore neleen may diw bi ngay diwoo Lii tax man ak yaw ñun mëñuñu xulóo Yàlla ko def suñu rawan yi ñoo jubbó Ndax ma def ci yaw valeurs bañ lay wër comme ay vautours Jarul wiri-wiri man nga nob allez-retour Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob) Sa dëggëntaan (man nga nob) Ku lay gaañ yaw ku lay cooxatan Est-ce que xam nga li nga yor? Xale bu ndayam gërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la Yaw ku ñépp di wër nga am Ñeneen ñi duñ dërëm Maa ko fa am nekkak keneen jàppu la May ki taxoon ñu sakk la Ànd bangue ñu taxe aras Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Maay ki sa yaram lacc Ndax may ki koy dawal Ko mëna nekkal keneen tamit jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la Nekkak keneen jàppu la Sa ex jàppu la Nangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la