Yeah, yeah, yeah Oumy Gueye OMG Mashallah baax nga yaru nga Ne naa laf cat Am tuuti bandit bari caas Ne naa laf cat Yaay kiy def dosi boole wax Ne naa laf cat Cat dafa gaw bëgguma ku ñu ree Ne naa laf cat Ki ku ko sukker, xale bi laf cat Soxlawul sàppali, ne naa laf cat Loxo bi gaaw na, xale bi laf cat Aka mën a sañsé, kon ne leen laf cat Benn ga fi Ku mel ni yaw amatul Yaa may jeri Yaay sedal sama xol man la Dégg nañu lu ne, teyul nga gën a jàpp Diggante bee dàq mbuurook lem Yaa may Douta Mbaye Lu ma neex neex na la Li ma bëgg dégg rekk ngay wax Xol bi ne na waaw Meloo ni ñoom, amoo morom Mashallah baax nga yaru nga Ne naa laf cat Am tuuti bandit bari caas Ne naa laf cat Yaay kiy def dosi boole wax Ne naa laf cat Cat dafa gaw bëgguma ku ñu ree Ne naa laf cat Ki ku ko sukker, xale bi laf cat Soxlawul sàppali, ne naa laf cat Loxo bi gaaw na, xale bi laf cat Aka mën a sañsé, kon ne leen laf cat Sa jikko ji neex na ma Sa ree ju neex sofu ma Ni ngay waxe neex na ma Dara ci yaw di sofu ma Kon ne naa laf cat Weretuma ndax dof ci yaw Sama caabi mbëggeel mu ngi ci yaw Àljanna rekk lay dund ak yaw Yaa ma mën a fàcce Yaay garab bi gën ci man Dégg na ma ñu naan Couple bi dafa nice Mashallah, hey kaar! Buleen ñu catu waay Lammiñ baxul waay Laalal bant, waay Daagu ni ma daagu nee Ñu ànd doxal waay Mashallah baax nga yaru nga Ne naa laf cat Am tuuti bandit bari caas Ne naa laf cat Yaay kiy def dosi boole wax Ne naa laf cat Cat dafa gaw bëgguma ku ñu ree Ne naa laf cat Ki ku ko sukker, xale bi laf cat Soxlawul sàppali, ne naa laf cat Loxo bi gaaw na, xale bi laf cat Aka mën a sañsé, kon ne leen laf cat Sa jikko ji neex na ma Sa ree ju neex sofu ma Ni ngay waxe neex na ma Dara ci yaw di sofu ma Kon ne naa laf cat