Takkuma teere, dama pikkiru Danga corona walla sibbiru Yay karaba demal wax ko kiriku Man ngay jem sul mete netetu Mane tefesul, lebu bi mën na pepesu So bëggetul, demal buntu bi tëju wul Bañal kennen nangu xale bi toye ni ku don sangu Saf ni moutarde Xonk ni bisap Neex ni ditax ki yorul denu pitax Jalax jëme Foko jalax jeme Jalax jeme xale bi fo ko jalax jeme Jinde jane ci pax maako saŋ Kudu gu ndaw ci dëxin maako saŋ Teral samay noon maako saŋ Mani saŋsé tëdi maako saŋ Eh bañal loolu (maa baŋ) Bañal loolu (eh maa baŋ) Bañal loolu (maa baŋ) Eh bañal loolu (mani la eh maa baŋ) May sa cinema konn bësel play Bul avance, bul recule, bul pause bësel play Nay dëger yox la ñu dem Jeli bi jaruta gudal Malay yobu ayca jugal Dinga tuki té do dem tugël Xecc bu dagul dikk Gaal bu demul diige Cas bi demul dic So xamul nopil te ne miik Di caw sa fas mangek xiir Yengel fépp té cow du riir Def tékk ni janu biir Bolé ci takal fépp ni berigo tiir Jinde jane ci pax maako saŋ Kudu gu ndaw ci dëxin maako saŋ Teral samay noon maako saŋ Mani saŋsé tëdi maako saŋ Eh bañal loolu (maa baŋ) Bañal loolu (eh maa baŋ) Bañal loolu (maa baŋ) Eh bañal loolu (mani la eh maa baŋ)