Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Touss tassar dara du xew Touss tassar dara du xew, ngani Touss tassar dara du xew Mani, eh, touss tassar dara du xew Hey, toubar kala mashallah (waaw) Bind bu rafet bima Yala bindé la kontan (waw) Bobu xalima dam na do guis kenen kel comme man (déedéet) Am na dolé soxor na kane momay laccé combat Ay yow xo ba jeex muy cipatu di mér Ku mer kalamel Yalla fi sisu mofi jeex Hé saraxu glaace (na xol yi fex) Saraxu frigo (hé na xol yi fex) Saraxu glaace (na xol yi fex) Hey, saraxu frigo (hé na xol yi fex) Touss tassar dara du xew Bañal ma nga nangu Dugg ci dëm yii kulay walu Saraxu clim, xol you tilim N, bu didim, diko ci bombu Dangay baré ma tak si ndombu Tukusu ben si xol yow bone Danga baax ma jaay la bone Jité boy yii dilen nduli Touss tassar Hé ku baax si xol you fex, tay mu neex Sarax si moy nga begg wañi mér Ku jum ba songu gaindé tay nga dé Dajé banc yak der di sandi xer Nit nga dumala ñé Dof nga dumala ré Yéné ming si nék Sisu man nga pousse ma né Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Touss tassar dara du xew Touss tassar dara du xew, ngani Touss tassar dara du xew Mani, eh, touss tassar dara du xew Yo, déedéet du jam li comme guerre Faw mu turu ndaxté dafa fess Defleen ni degg di def fen Bay katu guerté du nam caf Ci soce yi lay cap ten Démuñu té bawuñu ken dem Kuko mën du kuy jëm Té sélébe yoon du pour toce nen Xëyel dima waxal man may gënë dem Sukkër sama dundu lukoy téré neex Fouli garab yi di fax suf si di jalaño Sañsé dox nank xol yi di ñamaño Hé saraxu glaace (na xol yi fex) Saraxu frigo (hé na xol yi fex) Saraxu glaace (na xol yi fex) Hey, saraxu frigo (hé na xol yi fex) Eh, di séral sa xol loy waxati Sa tamaté makoy lokati Tass tassar game bi bamu tass Eh, ñu tek ko bako fi Mani këlëm mulay mass 10 du ray ass Wuré bi dem na kung Ma yor balle bi dumla passe Loloy dëgg man la sen wa kër begg Lakatul nga cëgine lingay bégge ñokay tëg Dalay neex, yoyou dalay neex Toce kany pacal limon def si bëcëk dalay neex Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar Bu naré sedd nañu ko bayi Mounane tëss Cas bi xaar ko tëss Xew ni saraxu t Forcément on fait le buzz Touss tassar dara du xew Touss tassar dara du xew, ngani Touss tassar dara du xew Mani, eh, touss tassar dara du xew