Taluma yendu di cas (awma jotam) Nekkuma ci ay détails (bëgguma ko) Danga faux man doo ma sonal (taluma ko) Xaruma kenn ci leen (no no no) Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Deel wax reek Yaq dèr ak coow li nga apo Li tamm nga ko Doxo ci daray mandu Soppil jikko Toppal àdduna mu lay jay Loo fiy def yaa ko tey Samay wax nga yobbu ko Seddeloo ma sama jikko Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk Samay wax nga yobbu ko Seddeloo ma sama jikko Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk Taluma yendu di cas (awma jotam) Nekkuma ci ay d [etails (bëgguma ko) Danga faux man doo ma sonal (taluma ko) Xaruma kenn ci leen (no no no) Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Doomu garmi la man Xaajuma ci ay wax Topp nga ma mboro Billaay xale bile Massa Doomu garmi la mane Xaajuma ci ay wax Topp nga ma mboro Billaay xawma li lan la Dumla wax dara Waaye li metti na Xamaloo ma dara Dima yaq dax àdduna Munuloo ma teye fi Yàlla finé Dom téré bék Mënoo ma stressé Yàlla tere Samay wax nga yobbu ko Seddeloo ma sama jikko Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk Samay wax nga yobbu ko Seddeloo ma sama jikko Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk Taluma yendu di cas (awma jotam) Nekkuma ci ay details (bëgguma ko) Danga faux man doo ma sonal (taluma ko) Xaruma kenn ci leen (no no no) Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Maa ngi baax, maa ngi baax Maa ngi ci sama bopp Doomu garmi la man Xaajuma ci ay wax Topp nga ma mboro Billaay xale bile Massa Doomu garmi la man Xaajuma ci ay wax Topp nga ma mboro Billaay xawma li lan la Maa ngi ci sama bopp Maa ngi ci sama bopp Maa ngi ci sama bopp