Man foo may jaar gisuma ko Fees sa bët di la jooyloo Doole ju bari yénne la ko Gone la damay bëre dóor Doo dégg mukk ma ni baal ma Bëgguma jamm, duma ni la Massa Ñëwal jege ma taxa ripa Foo ma woo ma wuyu la Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Man duma baale Su ma jékoo damay gaañ Nduti nduti saay Ma mën ma ëpp doole Te su ma jekoo damay gaañ Nduti nduti saay Xale may dékk ma nga may daan Man su ma lay ray damay reetaan Séwel bët mattu bandit Kolobaan Mas la ngay mbidiou ne kuñ coqotaan Noo Man su ma jàppee damay daan Pacal limon toj kaani daqar ci thiambane Noo Dof bi nga séxel demul Fann Boroom soow lu mu rew rew yabul boroom pane Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Man duma baale Su ma jékoo damay gaañ Nduti nduti saay Ma mën, ma ëpp doole Te su ma jekoo damay gaañ Nduti nduti saay Kote bañ la bàyyi def la ni njegenaay Rof la galgal nga tëdd njaaxaanaay Muy suus, gowe ci ànd cuuraay Wuyaay, ray la du tax ma bàyyi Àjj la ba ci kaw doo lal suuf Fàtte fepp, doo am tus Jël sa tànk ak mbagg def la xale di la rakk Bul ragal, may dawal Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Sopp nga doon jaay Duggu ci man dootoo ko defati Nduti nduti saay Man duma baale Su ma jékoo damay gaañ Nduti nduti saay Ma mën, ma ëpp doole Te su ma jekoo damay gaañ Nduti nduti saay