Senegaal ñoo ko moom Kenn mënu ko xar ñaar Xiif, lekk ñàkku fi Mar, naan ñàkku fi Gudde am fo fanaan sama rééw Bu ñu nangu kenn duggu suñu diggënte Same diam ji fi ñoom mame bàyyi Xamuñu leneen, bëgguñu leneen He he he! Gueye Ndioro wëy naa la (gueye Ndioro way naa la) Faye Birame wëy naa la (way naa la) Diobeu Dioubeu wëy naa la (diobeu dioubeu wëy naa la wëy naa la wëy naa la) Tourè Mandi wëy naa la (hehee) Thiam babel demba thiam way naa la Gomissa gania way naa la (sané balama) Ndiaye Diata Ndiaye wayaan naa la Dioufa niokhobay wëy naa la (man djonkéléfa) Sant yi war galgui rééw ma ngi Sant yi war galgui rééw ma ngi Diom foulak fàyda Fonk diné tax xol yé ngi naat Dieuf ju baax de diogufi Sutura lañuy ndamo Han Senegaal Ndiaye sama rééw Walo walo si réw mi Sine Saloum si réw mi Casamance Boundou Cadior ak Baol Fouta Toro Jolof Senegaal Dieng Salla waynala (samb maharam waynala) Diagne Naar waynala (diallo diery waynala) Sow Poulo waynala (ba poulo waynala Yagg masseuy) Sall Ngari waynala (cissé ngari Ngom séni) Ndoye Mali Maram Ndoye waynala (wade farawade ndiack) Mendy Coto waynala (pouye beukeury) Fall Ndiaga yaram waynala (waynala Camara yilé) Dieye Massamba waynala (guissé Maabo) Mbacké Balla Aissa Sy Sawandé Niass Coumba Abdallah Laye Makhtar Kounta Sidy way naa leen! Sante yi war Galgui reew mangui (lo ndam ciré) Sante yi war Galgui reew mangui (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou) Sante yi war Galgui reew mangui (thiaw séni Mbengue mbor) Sante yi war Galgui reew mangui (ndour wally mbergane Niang mbaallo) Sante yi war Galgui reew mangui (sene thiali Sylla moctar) Sante yi war Galgui reew mangui (seck sa guanar) Sante yi war Galgui reew mangui (sarra moundo Ly bousso) Sante yi war Galgui reew mangui Sante yi war Galgui reew mangui