Gouro, 3 pieces Gouro, 3 pieces Gouro, 3 pieces Gouro, 3 pieces (I say) aladji miezé Def la sama sokhna lala yéné Man ak ioe si diakka, imam ak préfet Boléma'ak sa papa nako gérer (woo) Yow laa wa yow le Yow laa wa yow le Beug nala khamna beug ngama Doyyal ngama soumala amé amna niénti diabar Eh ngani pa bi nako wo-oh-oh-oh Damleu beug takk guénouma ak yow-oh-oh-oh Vieux père woxma lanela loy douter-eh-eh-eh Beug nako amna dinée ak ligué-eh-eh-ey (yeah) Baby oubbil ma sa xol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah) Naala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur (woo) Wokhak sen wa keur nélène maay sa borom keur (anh yeah) Naa taal sen keur sougnma deffoul sa borom keuur (oh, yeah) Dina indi gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces (I say) takk sama fite Do am ben woudiou baby à part sama fite (yeah) Boula nékhé doreul radio May sa borom keuur, baby cardio (Eh) louy bayyanté pour kouné sey sey bi? Ah bougn def lolou kay niou sey sey bi (Eh) mak yow warrouniou am blem Ya eupone prétendant championnat anglais Réception invités yi nanni jinja Soma firé dina mourou melni ninja Mayé bou ndieuk meyyleu galé tekk cii 3 quarts Soumaley nianni feug ngandi boubou 3/4 Man la gars yi wowé bad man miezé Am diabar mou melni yow laa yagg rêver Nuit de noce premier son ma mayyleu bébé Yalnaa tokk di lath yallah finga fété (yeaaaah) Baby oubbil ma sa khol pour ma nekk sa borom keur (anh yeah) Nala dieundeul ben keur pour ma nekk sa borom keur Wakh ak sen wa keur nélène may sa borom keur (anh yeah) Na tal sen keur sougnma deffoul sa borom keur (ooh yeaah) Dina indi gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, def trois pièces Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces (ngané lane) Gouro, trois pièces Aladji miezé Def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah) Aladji miezé Def la sama sokhna lala yéné (yeah yeah yeah) Aladji mieze Def la sama soxna lala yéné (yeah yeah yeah) Aladji miezé Def la sama sokhna lala yéné