Yeah yeah Lane leu rap bi indi sama life Ay deumeu you beugue lekk Ay kharite you ko meussoul nekk Khaliss bou lewoul buma meunoul lekk Yeah lane leu rap bi infi sama life Jeuf youmay leundeumeul si sama diner Nit you lay geuneu bet so lene miné Siw reuy bew meussouma ko def pour frimer yeah Rap bimeussoul nek sama ligueye Rap bi meussoul nekk sama ligueye Mere bi dafa guente nioumay ligueye Mané ko grawoul mere biguey guente magui ligueye yeah Khamna gni ko geumone gni done salé Gni meu ajdou wone ak gni meu faalé Rap bolewouma ak sama beneu frère hun Rap bolewouma ak sama beneu frere yeah Kone li yeup pr li leu wone nigga Li takh ma teylé ay diplome nigga Damel ni sama bopp la togne Ndakh Souma yeugone jeul benene yone nigga yeah Yeah lane leu rap bi indi sama life A part fans youma beugue bru defmeu sen nit Nio takh 2 ans sans son magui ci game bi 2 ans sans sons magui ci game Miezé meussoul bokk ak gayi May bay rap beuri neu niou rap bayi Yeah kone Lane leu rap bi indi sama life Dou Dara louma meunoul dindi sama life I say Je joue des mots Je joue des mots comme on joue de la guitare ou du piano Comme de l'eau qui coule dans un ruisseau Ma plume laisse des Larmes qui désarment les âmes et les affichent tel un panneau Je joue des mots comme on rassemble les pièces d'un puzzle Éblouis tout receveur car d'audibles miracles je suis faiseur Je rassemble les mots comme une apostrophe Car chaque strophe n'est que Catastrophe Il y a les doux vents Il y a les ouragants Ma prose est une illustration de tout ce qui se trouve dans l'air On trouve dans la rivière ce que l'on ne trouve dans la mer Solitude comme châtiment, que dis je Solitude comme armement Dans un jardin de vérité fait naitre des roses aux épines blessantes Vulgaires mais pudiques, moroses mais ludiques elle s'élève d'une maturité naissante Une musique qu'il faut entendre pour juger Souvent coincé dans un mirroir entre le terrestre Et le céleste Les mots les couleurs le sons les rythmes moyen de rendre mon intimité célèbre Passion contre addiction J'ai mes pulsions mes contradictions Je me noie Entre des reves et des illusions Ssp est l'histoire d'une désillusion Car il ya ceux qui Vivent a mort et le reste en vie Ceux qui vivent à mort, le reste envient Ceci était juste une pensée dans une image C'est l'histoire d'un jeûne rêveur qui a pris le chemin des poètes Pour se rendre compte qu'il n'est pas un poète Ssp asatsu Li moy say say poésie Bye bye comédie Omzo dollar dem neu yonam c'était la last prophétie Say say poésie Bye bye comédie Omzo dollar dem neu yonam c'était la last prophétie