Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Anh han!! Oh wanh! Oh wanh! Oh wanh! Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Sama xel mi mom legui mou dem Ndax legui ma doff Sama none yi wéxal na beugn yi Fass yéné ré Sama néné touti yaw boul ma bayi Souma togué ba xalatt lén Man douma néh Damay ndérmélou Di ndérmélou (wawaw), di ndérmélou (Ndeysane) Di ndérmélou Yama done watal ni boudoul man Dou done kénén nioumay roubé Dima roubé (dima roubé héhéy) Cheri boy boul ma bayi Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Dama dioum ba dila woh telephone Faté danio xoulo Nitt ak kamou mine Ay koussi mérr bay watt Faté nga dioubo Makhalla seuytané nga Fouma dougal cherie wakh ma Xana guisso nima diéxé temps yi Yaw rek lay xalatt rafet nga lolou Dougou sama xol diaxassé ko Réw ba doff (Soff) Capricieuse ouly lan la Boul ma xol Xamgani balnala (Balma) Waw kaay fii namone nala Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Boul ma bayi Boul ma bayi sama Banana Boma bayé Beuss boma bayé nassi doff Boul dem ba bayima baby (Yaw xamga yawla am baby) Cheri Kaay kaay Kaay kaay fiii (Kaay kaay Kaay kaay fi thie Mane)