Lu mu lëndëm lëndëm yaw rekk laay gis (ehn ehn) Sa leeraay bidéew yaay leeral sama xol (ehn ehn) Àdduna desalatu ma dara Diggante bi Yàlla ko bind ca aras Man yaa ma mëna Loolu tax ma bëgg la Yàlla ko bind ca aras Ñaari xol yee tase baby Man bi ma la seene ci la xam ni Yaa war a contrôler zone bi, duggal but yi Boyaal cax yi taxawe nee Li may yëg ni dafa neex waaw du jeex Sunu diggante du yucci xaajal kenn Kaay fii sama amore Ñu wan leen ni ñuy bëggante Ton pied, mon pied Foo toog fa laay dem Kon li lu koy faay Maak yaw ñu dundu ko (Maak yaw ñu dundu ko) Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Dama tégi as teg la plasu reine Def pat ak organisé di ko dundu Wër naa ci àdduna gisuma ku la gën Li may yëg ni dafa neex waaw du jeex Sunu diggante du yucci xaajal kenn Kaay fii sama amore Ñu wan leen ni ñuy bëggante Ton pied, mon pied Foo toog fa laay dem Kon li lu koy faay Maak yaw ñu dundu ko (Maak yaw ñu dundu ko) Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko Oh oh oh oh oh Maak yaw ñu dundu ko