Yeah Sama fans yi, maa ngi leen di gërëm Di leen sant gis naa seen taxawaay Musique bi Pur yeen la, oo oo oo Man nob naa leen, waaw Yàgg na lool (yàgg na) Bi nga demee (bi nga demee) Man réer naa (réer naa) Réer naa sans yaw (sans yaw) Lan laa wara def? (Wax ma) Def sans yaw (sans yaw, hey) Dama la soxla, dama la bëgg (Dem nga te bàyyi ma) Bàyyi ma ci lëndëm Wante xam nga ni Ni dama wara dundu ba tey (Dem nga te bàyyi ma) Baby, ñëwaatal ci man Xanaa déggoo sama woo, yeah (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga demee (Tax na sama xol wéete) Lu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga deme (Tax nga sama xol wéete) Xanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man Bu ma toggee di xalaat (Dundu yu neex ñi ñu doon dundu) Rekk sama xol fees (Xamatuma lu ma wara def) Deme nga bàyyi ma ci lëndëm (Wante xam nga ni) Dama wara dundu ba tey (Dem nga te bàyyi ma) Bàyyi ma ci lëndëm Dama la soxla, dama la bëgg Baby ñëwaatal ci man Xanaa déggoo sama woo (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga demee (Tax na sama xol wéete) Lu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga demee (Tax nga sama xol wéete) Xanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man Xamatuma li ma wara def (yàgg na lool) [?] xalaat Bëgguma nga xam li ma daj Ndax xam naa ni am nga keneen Mënuma ko gëm, mënuma des ni Yàgg na lool bi nga demee Man réer na nekkatu fi Lan la wara def nékkatu fi [?] Dama la soxla, dama la bëgg Baby ñëwaatal ci man Xanaa déggoo sama woo (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga demee (Tax na sama xol wéete) Lu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man (Baby ñëwaatal) Yàgg na lool bi nga demee (Tax nga sama xol wéete) Xanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man