Mon bébé, baal ma Ooh bébé, baal ma Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Damay toog di ko xool, di ko xool, di ko bardé Dafa am, dafa am, dafa am sama yërmande Damay dem, damay dem seeti sama waa ji Xool naa xool xool ba xam ni mënuma la bàyyi Chéri, baby Chéri, lu may yëg sama xol mënuma ko bind Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Dafa mel ni lamp leeral sama yoon Ba ma xame man fu ma jëm Jamm nga ma na ni ci xeexu mbëggeel Bae nangu naa yaa ma mën Bés ni ki tay, yaw yaa ma moom Dama sakkusi na ngërëm Ne ci lu la neex dox ci lu la neex Foo jëm, foofu laa jëm Chéri, baby Chéri, lu may yëg sama xol mënuma ko bind Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Ca dëgg dëgg dëgg wan nga ma baby Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Amour ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) Moom ji nu ne lay feñe Mbëggeel ji nu ne lay fëlé (baal ma) (Baal ma, baal ma)