Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Sa mbëggeel ci man moo tax taamu naa la Sa yërmande ci man moo tax fónk naa la Yeah, yeah, yeah, yeah gune yi Nañu ma bàyyeek yaw Yeah, yeah, yeah, yeah gune yi Sama àdduna yaa ko yor Ñoom dal (Queen Biz) Fu nu tollu ñi ngi may toogee Dégg naa (Quen Biz) Man nan laa lay toppee Man dal (Queen Biz) Bañuma ci dara, dama bardé Ñoo ngi naan (Queen Biz) Moom dafa ñàkk fayda Lépp ci yaw la Li niy teg sama kaw yépp ci yaw la Li tax ma bëgg la (ci yaw la) Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la) Baby lu tax ma nangu (ci yaw la) Li sugar sama xol bi (ci yaw la) Li tax ma bëgg la (ci yaw la) Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la) Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Yaw la love te yaw la (yaw la) Yaw la love te yaw la Yaw la love te yaw la love Yaw la love te yaw la Baby yaw la love te yaw la, yaw la love Yaw la love te yaw la Yaw la love te yaw la love Yaw la love te yaw la Eh yeah, yeah, yeah Respect bi nga am ci man moo tax taamu naa la Gondiwoo ma ak li nga am moo tax fónk naa la Sama xol bi yaa ma ci doy Nañ ma bàyyeek yaw Ku ma bëgg na ma bàyyeek yaw Sama àdduna yaa ko yor Ñoom dal (Queen Biz) Bëgg nu ma gis may happy Ñoo ngi naan (Queen Biz) Alalam bi la ko toppe Fàtte nañ (Queen Biz) Dama pare démb tay soog a ñëw Waxleen (Queen Biz) Lu dul mbëggeel sonalu ma Lépp ci yaw la Li niy teg sama kaw yépp ci yaw la Li tax ma bëgg la (ci yaw la) Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la) Baby lu tax ma nangu (ci yaw la) Li sugar sama xol bi (ci yaw la) Li tax ma bëgg la (ci yaw la) Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la) Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom (Yaa ma leen gënal sama boyfriend) Yaw la love te yaw la (yaw la) Yaw la love te yaw la Yaw la love te yaw la love Yaw la love te yaw la Baby yaw la love te yaw la, yaw la love Yaw la love te yaw la Yaw la love te yaw la love Yaw la love te yaw la Eh yeah, yeah, yeah