Maak ioe hé seuy laniou digué wone Ndax ioe rek la nobone Ngamay trompé samay noone dima ré Niouné saleté lou ci bax moy mbalite yé Sa téléphone dey sonné Même bou minuit passé Nga wouyu guestou nima wa keur nioy woté Loutax ngamay def li Kou melni mane dotoko amati (no no no) Loutax ngamay def li Khamal ni ioe dotoko défati (no no no) Mane rek Fouma nekh lay goudé beuss dina niow Nga matteu sa lokho ja Nieup la bayi né ioe la té dou ioe Ya ngui nane ni beuss bo mandé fégn Guéneu goudi bayi ma fi dém Lane ngey outi l'amour ngui si keur gui C'est la vie (c'est la vie, c'est la vie) oh C'est la vie (c'est la vie, c'est la vie) oh Maak ioe hé seuy laniou digué wone Ndax ioe ioe rek la nobone Ngamay trompé samay noone dima ré Niouné saleté lou ci bax moy mbalite yé Ioe khamoulo mane kima done Sama xol lay diokh sa morome Kou deung limou yorr sou wadé Kou dioub rek mor for dieurigno Yén Facebook ak Twitter () Ni WhatsApp Bayiwo Instagram no no Imo ak Snapchat Loutax ngamay def li Kou melni mane dotoko amati (no no no) Loutax ngamay def li Khamal ni ioe dotoko défati (no no no) Mane rek Fouma nekh lay goudé beuss dina niow Nga matteu sa lokho ja Nieup la bayi né ioe la té dou ioe Ya ngui nane ni beuss bo mandé fégn Guéneu goudi bayi ma fi dém Lane ngey outi l'amour ngui si keur gui C'est la vie (c'est la vie, c'est la vie) oh C'est la vie (c'est la vie, c'est la vie) oh Da ngey yam sa wai way Am sa way nga beugeu ko loool lé (Beug ko loool) Mou def la fowkay (fowkay) Yakh sa xol bé (mou yakh sa xol bi) Mane rek Fouma nekh lay goudé beuss dina niow Nga matteu sa lokho ja Am nga guél Tambacounda Am nga guél Mauritanie Am nga guél Fouta toro bayiwo dara Am nga guél Kaolack nanda Am nga guél Diourbel Dakar Am guél kouri koro bayiwo Gambie Am nga guél Tambacounda Am nga guél Mauritanie Am nga guél Fouta toro bayiwo dara Am nga guél Kaolack nanda Am nga guél Diourbel Dakar Am guél kouri koro bayiwo Gambie