Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet

Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay
Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy, dem naa

Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay
Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay

Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na
Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na

Tay yàlla ñu boole
Ngir ñu séy de ngenal la
Mbëggeel la bari doole
Bés ni ki tay sa jabar la

Bés bi ci man ni mu fore
Xarit yi ñëw ak doole
Sañse nga gis ni ma moole
Kaay yóbbu ma art ba amore

Tay la sama àjjana
Li ma doon ñaan yàlla yegsi na
Tay ma séyal la
Pour le meilleur et pour le pire

Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na
Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na

Lu jigéen ñi bari bari
Man nga ci tànn seppi ma
Tay lañ ma yàpp pur ma séy si
Wax ma loo bëgg ma defal la

Bés bi ci man ni mu fore
Xarit yi ñëw ak doole
Sañse nga gis ni ma moole
Kaay yóbbu ma art ba amore

Tay la sama àjjana
Li ma doon ñaan yàlla yegsi na
Tay ma séyal la
Pour le meilleur et pour le pire

Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na
Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na

Il m'a validé (validé)
Je suis validée (je suis validée)
Il m'a validé (il m'a validé)
Je suis validée (validée)

Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay
Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy, dem naa

Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay
Tàcculeen sama njanku jeex na
Damay séy tay

Approchez, approchez
Venez, applaudissez
Viva, viva, viva!
Viva, vive les mariés

Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na
Seetoo seet, seet seet
Seetoo seet, seet bi yegsi na
    Página 1 / 1

    Letras y título
    Acordes y artista

    restablecer los ajustes
    OK